Si gare Lako bi fekkeu,
Mi Ngui Sanguo seur
Té Beut yi di takkeu,
Ma dal di Koye nougnou
Mou dal di maye Faye,
Dal di maye yédeu ci adouna bou yakhou bi
Mane Douma Fatte!
ah ah mani mani!
L'uomo Douma Fatte Bamako LII mani LII mani!
Mane Douma Fatte!
Kerok Lama Khamal Louma khamoul woone CI Diamono bou yakhou yénene bi ak yénene;!
Balaa maye dougeuti criniera ci loumou meuneu doone
Dinaa fattélikou Ndaw sossou
Limouma wakhoone
Souy Souy sou sou sou sou sou sou Souy !!
Ci gare bi Lako fekkeu mi Ngui Sanguo seur té Beut yi di takkeu,
Ma dal di Koye nougnou
Mou dal di maye Faye dal di maye yédeu,
Maky yé yé maky maky maky Yeeeee !!!!
Waw kérok Lama Khamal Louma khamoul woone CI Diamono bou yakhou bi,
Balaa maye dougeuti CI loumou meuneu doone, < br /> Dinaa fattéli ko maky yé yé maky maky maky Yee !!
ah ah mani mani!
Douma Fatte Bamako LII mani LII mani!
Mane Douma Fatte Bamako
Il testo e traduzione di Bamako in italiano è interpretato da Youssou N'Dour sono proprietà dei rispettivi autori, gli artisti e le etichette discografiche. Si deve sapere che il testo e traduzione in italiano da Bamako - Youssou N'Dour solo a scopo didattico e se ti piace la canzone che si dovrebbe prendere in considerazione acquistare il CD dal sito ufficiale di